價格:免費
更新日期:2018-09-28
檔案大小:69.6 MB
目前版本:2.0.1
版本需求:需要 iOS 9.0 或以上版本。與 iPhone、iPad 及 iPod touch 相容。
支援語言:英語
Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari téere yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci téere yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.
Man nga tànn:
--Noo bëgg aaya yi feeñe?
Aaya yi ci ay dog, walla
Benn aaya ci rëdd wu nekk
‐‐Noo bëgg téere yi feeñe?
Limeefu turi téere, walla
Limeefu gàttali téere
‐‐Woneel nimero aaya, walla
Baña woneel nimero aaya
支援平台:iPhone, iPad